Páginas

sexta-feira, 29 de julho de 2005

Momentos de Verão: Ismael Lo - Baykat


LETRA
mané hé baykat bi khalam
démonna bay nékh wayé boumgua
dokna mome

mané hé baykat bi khalam démonna
bay nékh wayé boumgua dokna mome

boula nékhé talalal say lokho
yaye docteur biy fath khifou askane bi
liko dalé si nditoum rew bassi miskine
ya souméko di dane sa dolé andak nath
bi di liguey sa gnakha di tourou
ngay bay di doukat bilay ya am diome

kon diarama baykat koufi xiff yako
doundal bamou sour waw koufi fébar
yako nandal aki réén bamou féékh

kon diarama baykat koufi xiff yako
doundal bamou sour
waw koufi fébar yako nandal aki réén
bamou féékh

ya momone sa mbay
ya mome sa guanthiakh mome say
ndiour ya mome sa alla di bay
nguour gneuw dougalthia lokhome ak
boor fékeleuthaa guanthiakh ba
mégneu lole ndékétéyo

kon diarama baykat koufi xiff yako
doundal bamou sour
waw koufi fébar yako nandal aki réén
bamou féékh

kon diarama baykat koufi xiff yako
doundal bamou sour
waw koufi fébar yako nandal aki réén

bamou féékh
dirama diarama baykat bé yaw
kéneu rek mola mana fay
moy bourbi yaalla
guathia ngalama

guathia ngalama yaw baykatbé
guathia ngalama
guathia ngalama yaw baikatbé

dirama diarama baykatbé yaw
kéneu rek moleu mana fay
moye bourbi yalla

Sem comentários:

Enviar um comentário

1) Identifique-se com o seu verdadeiro nome e sem abreviaturas.
2) Seja respeitoso e cordial, ainda que crítico.
3) São bem-vindas objecções, correcções factuais, contra-exemplos e discordâncias.